Abdou Nguer fait un aveux de taille sur Cheikh Bara Ndiaye « 100.000fr yondi ko… »

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 21 янв 2025

Комментарии • 191

  • @seydinaoumar3036
    @seydinaoumar3036 Месяц назад +16

    Deugg dou romb ay nopp bravo Abdou. Le Sénégal appartient à tout le monde

  • @mohamedndiaye3449
    @mohamedndiaye3449 Месяц назад +9

    Télé bou sérieux dou invité Abdou nguer.

    • @iboudiouf6267
      @iboudiouf6267 Месяц назад

      Télé yi di invité Abdou gno done invité invité sonko, pape alé chroniqueur comme Abdou etc...etc..kone télé yi meunougnou bone tey soit sérieux toi ca même

  • @amaama1275
    @amaama1275 Месяц назад +6

    Abdou ngér yalla na sa Diam yageu❤❤❤❤❤❤❤

  • @idrissacamara3917
    @idrissacamara3917 Месяц назад +13

    Sonko est derrière tout ça

  • @RamaNdiayr
    @RamaNdiayr Месяц назад +9

    Merci bcp Abdou bien dit ❤❤🎉🎉❤❤🎉

  • @Amsy3022
    @Amsy3022 Месяц назад +10

    Merci bcp abdou nguer yangui wakhal askanwi yalla nalla yalla arre ❤❤❤❤❤

    • @ndiagainssa7682
      @ndiagainssa7682 Месяц назад

      Yow akh gnimou andal respectel askan wi waye

  • @AsaAsalet-d4t
    @AsaAsalet-d4t Месяц назад +14

    ❤merci❤abdou❤❤❤❤

    • @MomadouCisse
      @MomadouCisse Месяц назад

      Youwsadatayae 🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @KadijatouJallow-z5d
    @KadijatouJallow-z5d Месяц назад +10

    Good analysis Abdou nguer ❤❤❤

  • @AmathToure-x6h
    @AmathToure-x6h Месяц назад +9

    Merci beaucoup

  • @falloutoure8849
    @falloutoure8849 Месяц назад +11

    Abdou nguer machallah ❤❤❤❤❤

  • @MouhamedThiam-w2u
    @MouhamedThiam-w2u Месяц назад

    Merci Abdou nguer je suis avec toi ❤❤❤❤❤

  • @OlivierNadieline
    @OlivierNadieline Месяц назад +4

    Abdou Nguer vous étez le meilleur je vous aime

  • @zizou6648
    @zizou6648 Месяц назад +12

    Merci❤nguer rek

  • @deh7865
    @deh7865 Месяц назад +10

    Sonko fenkatte la diomaye incompétent la

  • @damedia4990
    @damedia4990 Месяц назад +1

    Thiey Sénégal golo bou djouk nek chroniqueur no Sénégal nékh na 😂 😂

  • @IssaCisse-x3d
    @IssaCisse-x3d Месяц назад +2

    Ngeure sa ❤Dina Kate ndeyeme thi palatu yi gaye Fatou domerame

  • @amadoudieng5450
    @amadoudieng5450 Месяц назад +8

    Diadieuf abdou nguer

  • @mouhamadoufalloutoure1991
    @mouhamadoufalloutoure1991 Месяц назад +2

    Pour momme da amm importance qui xamoul bopam😂😂😂bilahi sonko ak diomay sakh xamougnoula yaye sonal sa bopou rék 😂😂😂

  • @bababodiang
    @bababodiang Месяц назад +3

    Abdou N'guer le vrai député du peuple

  • @khadimcoulibaly970
    @khadimcoulibaly970 Месяц назад +2

    Fii la guies abdou bou néke nafeke lii dafa niaw😂😂😂

  • @wiizelcapojoop1596
    @wiizelcapojoop1596 Месяц назад +3

    Abdou nguèr kom kou am ndiarign si rewmi nane man ma taxx huum😅😅

  • @maimunajallow2612
    @maimunajallow2612 Месяц назад +2

    Abdou Nguer ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @amdydiop8956
    @amdydiop8956 Месяц назад +9

    Sa journaliste bi sakh dala yeureum Ndakh say doullll ioe yaga toulll Abdou

  • @MOUHAMEDARONASALL-xr5ii
    @MOUHAMEDARONASALL-xr5ii Месяц назад +11

    Je suis pro sonko mais abdou nguer je Je l’aime bien 😂😂😂

  • @PARLONSTOUTAUSENEGAL
    @PARLONSTOUTAUSENEGAL Месяц назад +2

    Abdou , il se prend important. Deel , wakh rekk , di nga wakh ba dougal sa bopp . Maguiy seen sa paquetage. Sa doul guii bakh na rekk . Gni diouboon di liggeey légalement, sen activité mouguiy dokh ba leegi

  • @mamoudoudia5852
    @mamoudoudia5852 Месяц назад +1

    Moustapha Diakhaté a toujours alerté sur ce parti
    Tout ça pour assouvir la vengeance d'un seul homme

  • @mohametthiam4500
    @mohametthiam4500 Месяц назад

    Sonko avie ❤❤❤❤❤❤

  • @CheikhDrame-f3v
    @CheikhDrame-f3v Месяц назад

    Khalébou jiguen bi néna 300 barina déh 😂😂😂abdou wagnile😂😂😂

  • @user-kf7oi4q
    @user-kf7oi4q Месяц назад +7

    Ok dokhal rek aduna ci si sa kanam un jour viendra inchala sa bess ngui si yonbi

  • @oussamadiatta7453
    @oussamadiatta7453 Месяц назад +4

    Abdou mala beug

  • @LodMouss
    @LodMouss Месяц назад

    Abdou,budget bi, nékoul khaliss bou tégou dé, kharal ba 2026.mais tu as raison ,rewmi naniouko sêddo mou diékh❌

  • @amdydiop8956
    @amdydiop8956 Месяц назад +7

    Abdou bayi ay doullll dinga dhé dé

  • @farbadiouf1990
    @farbadiouf1990 Месяц назад

    Quels médias? Ces médias le méritent?
    Soyez en règles et payez vos impôts...
    C'est pas compliqué.

  • @IiiiloooHoko
    @IiiiloooHoko Месяц назад

    merci abdou nguer mala beugeu ❤❤❤❤❤

  • @bayesalioudiop2189
    @bayesalioudiop2189 Месяц назад +4

    Néke lén ndayi ay nite la wakh 😮

  • @PapaNdiaye-uj9rq
    @PapaNdiaye-uj9rq Месяц назад +11

    Ce boy la il est qui, et il faut le mettre en prison il fait que manipuler

    • @ndiayeabou1764
      @ndiayeabou1764 Месяц назад +9

      Toi tu es malade il dit que la vérité ou bien tu crois que le prison c’est pour ton père

    • @abdoulndiaye8821
      @abdoulndiaye8821 Месяц назад

      Comme que la prison môme c’est un marché. C’est toi qui mérites la prison

    • @cheikhseck4319
      @cheikhseck4319 Месяц назад

      ​@@ndiayeabou1764Merci ni donio sokhor

    • @MoussaFAYE-vb2rz
      @MoussaFAYE-vb2rz Месяц назад

      ​@@ndiayeabou1764 niome féne kate yi nioy séni kharite di

    • @mouhamedmoustapha684
      @mouhamedmoustapha684 Месяц назад

      @@ndiayeabou1764domou thiotou ndymm bi bann vérité layy waxx

  • @thionecisse7984
    @thionecisse7984 Месяц назад +2

    Xamal liguaa wakh !
    Un peuple -Un but 🥅 -Une foi ✊🏾

  • @AssaneNdiaye-h5s
    @AssaneNdiaye-h5s Месяц назад

    Abdou tu fais la grande gueule.Qui est ce que tu représente au Sénégal.Tu finiras par se taire .

  • @ousseynougueyebaye2263
    @ousseynougueyebaye2263 Месяц назад +1

    Senegal NDEYESANE Amatoul YAKAR . YAKHOUNA si ETAT bi

  • @MorFall-w6w
    @MorFall-w6w Месяц назад

    Aye Aboudou 300😂😂😂😂😂

  • @serignethioubagueye6557
    @serignethioubagueye6557 Месяц назад +1

    Déme léne diagui wouti khame khame 😢😢😢😢😢😢😢mo gue séne doul yi😅😅

    • @KhadyNiang-o5x
      @KhadyNiang-o5x Месяц назад +1

      Bougane moy domourar dof yeup mou dieul si télé bi

    • @OusmaneBadiane-z1s
      @OusmaneBadiane-z1s Месяц назад

      ​@@KhadyNiang-o5xsonko sweet beauté fenn katt bu magg bi tv bi la niow di dialalai ay allatam

  • @farbadiouf1990
    @farbadiouf1990 Месяц назад

    Ces arrogances et ces bassesses signifient quoi ?

  • @dioperracine5102
    @dioperracine5102 Месяц назад

    Ns notre usine ns a arrêté depuis le mois dernier 😢

  • @Katelia1503
    @Katelia1503 Месяц назад

    Ay way liberye dexpression la niou wakh les gens am nagnou khel di xalat mais sortez vos idees tey bayi saga yi

  • @mamadoufaye5433
    @mamadoufaye5433 Месяц назад

    Abdou nger Dina ma ray

  • @tobacamara
    @tobacamara Месяц назад

    Wa kou gagner election yi passer😂😂😂

  • @MomadouCisse
    @MomadouCisse Месяц назад

    Abdougeursadatayae🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

  • @mamadouseck6
    @mamadouseck6 Месяц назад

    Ay mbam ngaine amoulaine khalate abdou ngair sa khaile mi aye daye masi naikk yaye domeharame wayai sa bopp yaye domerame 😮😮😮

  • @NgoudasarrNgoudasarr
    @NgoudasarrNgoudasarr Месяц назад

    Abdou le député du peuple

  • @moukhakane
    @moukhakane Месяц назад +1

    Abdou nguér dé légui noppi

  • @alioudiop8257
    @alioudiop8257 Месяц назад +3

    Doul rek😅😅😅😅

  • @Mao97515
    @Mao97515 Месяц назад

    Cette présentatrice n'est pas crédible 😂😂😂

  • @adamagueye6578
    @adamagueye6578 Месяц назад

    Macky bi mou gneuwe supprime 40 agences Lo ci wakh , niatta chômeurs

  • @leraltouttv
    @leraltouttv Месяц назад

    😂😂😂😂😂Doyna waar dé

  • @mbagnickndong679
    @mbagnickndong679 Месяц назад

    Yaw organe de presse bou nek en règle doula invité si plateau 😂😂

  • @MamadouNdoye-s5f
    @MamadouNdoye-s5f Месяц назад

    Quand cheikh yirim a un seul emploi

  • @m-woliyoutv2038
    @m-woliyoutv2038 Месяц назад

    Yaw faté nguani moitié xar nga sa ndeye xaŕ leu ben pay douleu reconnaître domeram nga rek😂😂😂

  • @youssouyoussou532
    @youssouyoussou532 Месяц назад

    Sonko deh da fokni mo mome rewmi wayé yag yag rek djiekh

  • @fatoundourbodian1078
    @fatoundourbodian1078 23 дня назад

    Sonko Adji sarr mo yakh bop bi

  • @ndimbelanendimbelane421
    @ndimbelanendimbelane421 Месяц назад

    Abdou nguer 😂 😂 😂

  • @alioupouye3533
    @alioupouye3533 Месяц назад

    Kone de Rewmi. Nio gui Ligueye. Kou goor goor lo ba Fepou Fou ab Fenkat di wakhe nga tadj ko. Kon Legui Rewmi bakh

  • @SerignemorFaye-s9z
    @SerignemorFaye-s9z Месяц назад

    Abdou Nguer mi,amoul solo.kheuya kheuy rék,nék thi plateau yi,diniou tankh khal.Gnikoy invité rék,nio yap Sénégalais yi vayé bissam mingui nieuw yagatoul.Dana fégui thi bayam bou bone,bou réw bi M.Diakhaté prison

  • @OusmaneBadiane-z1s
    @OusmaneBadiane-z1s Месяц назад

    Walfadji tv moy tv Ousmane sonko bobu amoul problème

  • @fatoundourbodian1078
    @fatoundourbodian1078 23 дня назад

    Guy amoul ndiarigne Wakh a-t-il France deguege

  • @moussangome708
    @moussangome708 Месяц назад

    Media youye diokhé bonne information lagne wakh mais vous passez tt votre temps à mentir

  • @abdoulayekane1436
    @abdoulayekane1436 Месяц назад

    C'est vraiment pas normal !

  • @BayemouNdaw
    @BayemouNdaw Месяц назад +1

    Yaw ya meune fene 😂😂😂

  • @babacardiop4173
    @babacardiop4173 Месяц назад

    Kone dal pour réwmi dokh Nanou bayi gni sathi AK gni fayoul inpo boyébo niep ndool m kou sathi AK kou fayoul inpo Nanou reukh sa ndigue nga fay

  • @pastefpatriot8524
    @pastefpatriot8524 Месяц назад

    Mais bougane mom da bayi live yi😅

  • @fatoundourbodian1078
    @fatoundourbodian1078 23 дня назад

    Sonko créateur de walakana

  • @CheikhounaDiop-y5r
    @CheikhounaDiop-y5r Месяц назад

    Abdou 🤔🥺🥺🥺🤐🤐🤐🤐

  • @timombaye2828
    @timombaye2828 Месяц назад

    pastèf khana dafa fatè ni macky sall dako dèsoudourone tè taye nioye parti o pouvior naniou nopallou manou niou darra sii gayi journalist liguèye la sii rèw mi lla bok 🫶🫶🥰🥰

  • @mrbit190
    @mrbit190 Месяц назад

    Quelle part ? Il est fou ce type

  • @maodothiam9926
    @maodothiam9926 Месяц назад

    Non vraiment Sntv dama jaxal
    Abdou ngeur dafay tok di wakh niouni tékk té amoul xam xam

  • @CheikhDrame-f3v
    @CheikhDrame-f3v Месяц назад

    Ki mo geuneu con ci Sénégal,yow do tousse

  • @grandgrand8941
    @grandgrand8941 Месяц назад +4

    Fatima yaw AK grand Lamine Gueye dimaliléne Abdou nguere wakh ko deugue limouye wakh bakhoul si môme yenagui koye setane moye maame nak bakhna

  • @MedouneBa-o6l
    @MedouneBa-o6l Месяц назад

    Abdou djanguil ngua bagne fingua tekk mbirr mi dou fofou régulariser lagne la waxx il faut avoir la grandeur de reconnaître vos erreurs dem laine xole Liliane manqué nguaine motaliko tamite took fi Di victimiser woou hissss

  • @DaoudaDione-f3o
    @DaoudaDione-f3o Месяц назад

    Sonko loumouye dokhal norouna dictature

  • @lahatefaye7591
    @lahatefaye7591 Месяц назад

    Da ngaye féne rk ana adji sarr

  • @makhtarndiaye4354
    @makhtarndiaye4354 Месяц назад +1

    Yaw kèn falè woula. Mèwkat boo sagnoon deki bi nermélou. Wayè fènn rèk.ak douul. Yoon rèk. Toog mouy dokh dièkhna.

  • @diengniana5159
    @diengniana5159 Месяц назад +1

    Abdou nguer journaliste wala chroniquer la wala talleur

    • @NdeyekatyDiop
      @NdeyekatyDiop Месяц назад

      Lépe kharagne rék machallah

    • @mouhamedmoustapha684
      @mouhamedmoustapha684 Месяц назад

      Abbb domou thiotou ndym la fenn rek ak xasss sonko motax nioukayy tekk si télé yi

    • @SouleyeNdiaye-gw9lv
      @SouleyeNdiaye-gw9lv Месяц назад

      @@mouhamedmoustapha684Sa Toure bou Raféte bi ak Ninga Niawé Lamign

  • @modouthiam9645
    @modouthiam9645 Месяц назад

    Abdou nger yangui diokh sa bop dayo BO amoul nak

  • @mohamedbodian4564
    @mohamedbodian4564 Месяц назад

    iow sa aduna yeup doul rek ngay deff
    Bu macky di djite da fek ne dioudo wo
    Yangui won si sa biiru ndeye mo takh ngay wakh li nga fecke

  • @diengniana5159
    @diengniana5159 Месяц назад +1

    Ya gui fen deh

  • @adramesagnan5195
    @adramesagnan5195 Месяц назад

    N'importe quoi yow tu représente quoi dans ce pays bey graw graw lou tekki wo darra nkey tidji sa guémène bi di weurr di wakh rek

  • @jeanpaultendeng223
    @jeanpaultendeng223 Месяц назад +1

    Gros casse cuit manteur 😂

  • @Alviradem
    @Alviradem Месяц назад

    Gnii daniou lenn wakhoul deug, lolou rek leu, soukhal deuk bi, si tank yoyou laniou nek. Gnii daniou bagn Sénégal surtout senn pm bobou

  • @falloudubaisylla7372
    @falloudubaisylla7372 Месяц назад

    Barra😂Ndiaye dou wakh deug

  • @mandoumbembaye9447
    @mandoumbembaye9447 Месяц назад +2

    Abdou ioe khamo sa ndeye bop

  • @AbdoulkhadryDieylaniSow
    @AbdoulkhadryDieylaniSow Месяц назад

    Abdou dey fe

  • @BabacarDia-n9z
    @BabacarDia-n9z Месяц назад

    Demal diangui

  • @abdoudiallo8959
    @abdoudiallo8959 Месяц назад

    Ki dafa rew ba pare geun koy diapale domekhram deug la

  • @malickndiaye3436
    @malickndiaye3436 Месяц назад +2

    Sett si Yalla touty, Yerim foumou amei 300employés You mouy licencié 🤡😂

  • @AliouneDiop-i1h
    @AliouneDiop-i1h Месяц назад

    Yéne ayé doff guéne

  • @MalickKane-e3e
    @MalickKane-e3e Месяц назад

    Abdou seule

  • @GoraThioune-cd3yi
    @GoraThioune-cd3yi Месяц назад +1

    😂😂😂😂 doff yi 😂😂😂😂😂😂

  • @douguindiaye23
    @douguindiaye23 Месяц назад

    Qui a 300 emploi ?

  • @hamidoucamara6741
    @hamidoucamara6741 Месяц назад

    Ce gas est un menteur

  • @alinediop7770
    @alinediop7770 Месяц назад

    😂😂😂 faut

  • @Alphousseynigajigo
    @Alphousseynigajigo Месяц назад

    😊😮